Le « Notre Père » en wolof

Su nu bay bi ci asaman
na sa tur sel na sa ngur dik
lo beug na am ci suf nek ci asaman

may nu tey sunu dunde bes bu nek
te bal nu su nu ton naka la nu bale ni nu ton
bu nu bayi nu tab yeblis wante musal nu
ci lu bon

amen

(Sénégal, Gambie)

Une faute d'orthographe, une erreur, un problème ?   
 
Publié: 01/09/2013